Playing via Spotify Playing via YouTube
Skip to YouTube video

Loading player…

Scrobble from Spotify?

Connect your Spotify account to your Last.fm account and scrobble everything you listen to, from any Spotify app on any device or platform.

Connect to Spotify

Dismiss

A new version of Last.fm is available, to keep everything running smoothly, please reload the site.

Diaraf - Lyrics

Malen beug
Jaraaf, malen beug mann mi lé
Maleen beugg, Jaaraf
Malen beug mann mi lé
Wadji baxna, soko ñané mou mayla
Wadji baxna, soko toñé mou mérélaaaa
malen beug, Jaraaf
malen beug, mann mi lé
maleen beugg, Jaraaf
malen beug mann mi lé
Wadji baxna, soko ñané mou mayla
Wadji baxna, soko toñé mou mérélaaaa

Jaral nala li ngama jaral
souko défé dana ñou dadié
soko beugué da nko diégué
souko défé di nko ñémé
soko beugué yaw dé diéguéma
souko défé di nko ñémé
yaw mi lé miin nga leen
so démé ngani lèn man dama lenn beug waaw
yaw mi and'ak ñom xam nga lèn
so démé ngani len man dama lenn beug
yaw mi léé mine nga leen
so démé nga ni len man dama len beug waaw
Jamono ngui nii (Jamono ngua néé)
Jamono ngui fii (jamono ngua féé)
jamono ngui nini nii lé (jamono ngua nana né)
jamono ngui fifi fi lé (jamono ngua fafa fé)
nitou demb laay weuy mann (wa waw)
nitou demb laa waax man mi lé(wa waw)
niitou demb laay weuy man (wa waw)
ki ma beug lama waax man mi (wa waw)
nitou demb laay weuy man (wa waw)
nitou demb la waax man mi lé (wa waw)
nitou demb lay weuy man (wa waw)
ki ma beug la ma waax man mi lé (wa waw)
and'ak man, di yag'ak man, di nek'ak man
waaw hé, man dé kokou laay weuy man mi lé
waaw kima beug lama waax man mi lé
waaw fouma dem fekk ko fa moom mi lé
man dé kokou laay weuy man
nitou demb laa waax man mi lé
nitou demb laay weuy man
ki ma beug lama waax man mi lé
nitou demb laay weuy man
ki ma yaggal laa waax man
ki ma beug lama waax man mi lé
and'ak man, di yag'ak man, di nek'ak man
waaw man dé kokou laay weuy man mi lé
hé fouma dem fekk ko fa moom mi lé
waaw fouma jeum fekk ko fa moom mi lé
man kokou lay weuy man
kima beug la waax man mi lé
nitou demb laay weuy man
nitou demb laa waax man mi lé
niitou demb laay weuy man
kiima beug lama waax man mi lé
niitou demb laay weuy man

Writer(s): OMAR PENE

Don't want to see ads? Subscribe now

API Calls