Playing via Spotify Playing via YouTube
Skip to YouTube video

Loading player…

Scrobble from Spotify?

Connect your Spotify account to your Last.fm account and scrobble everything you listen to, from any Spotify app on any device or platform.

Connect to Spotify

Dismiss

A new version of Last.fm is available, to keep everything running smoothly, please reload the site.

Wéet - Lyrics

Souma guissatoul dingama xalat ééh xamnaani dinga weeto
Souma guissatoul guissatoul dingama xalat xalat xalat ééh xamnaani sa yone dina weeto

Mane may Goor Googou daan leu wayal dane la xalamal danla tannal sap layou thiépo
Mane may Goor Googou daan la néxal danla tété danla mounial sap tang xol bi

Souma guissatoul guissatoul dingama xalat xalat xalat ééh xamnaani sa yone dina weet weeto

Bess you nex ya weuy naniou digg you nex yi wess naniou yangui soukar sa adouna sama boss diaxasso
langueumeu djigoul mbott ay xalaat you rafet diamono diou neex adouna sou neex
Mane may mboot boobou daan leu yendoul djinax dioodiou daanla lakkal tey abiyola sissa boppou lalbi
Mane may Garab googou daanla kéral nguélaw lolou daanla féxal teg googou dalaan sagal

Souma guissatoul guissatoul dingama xalat xalat xalaté ééh ndiornaani sa yone dina weet weeto

Mane may Goor Googou daan leu wayal dane la xalamal danla tannal sap layou thiébbo
Mane may Goor Googou daan la néxal danla tété danla sap tang xol bi
Mane may mboot boobou daan leu yendoul djinax dioodiou daanla lakkal tey abiyola sissa boppou lalbi
Mane may Garab googou daanla kéral nguélaw lolou daanla féxal degg googou dalaan sagal
Mane may sa tëré bobou daanla moussal sa mame diodiou danla réwal sap taxander gogué

Souma guissatoul guissatoul dingama xalat xalat xalaté ééh ndiornaani sa yone dina weet weeto

Similar Tracks

Similar Artists

Don't want to see ads? Subscribe now

API Calls