Playing via Spotify Playing via YouTube
Skip to YouTube video

Loading player…

Scrobble from Spotify?

Connect your Spotify account to your Last.fm account and scrobble everything you listen to, from any Spotify app on any device or platform.

Connect to Spotify

Dismiss

A new version of Last.fm is available, to keep everything running smoothly, please reload the site.

Sori Nga - Lyrics

Jégi nga guej gui bayiko guinaw
Mom dh joyna joy joy ba rangoñ ferr ayway
Beugnala muñal nala ki sa yayu dom la (×2)
Jégi nga guej gui bayiko guinaw
Mom dh joyna joy joy ba rangoñ ferr ayway
Sori ngaleine ba fattei leine te lolu warula (×2)
Degg nga lune tankamlu ñep
Dem ba diekh leu xolam di guiss te xol du sax om bañkay beuss
Xolal ci mom nimuy dunde
Metina lolu ci xolam yaye kiffa diekh
Yaye ki waral ci lepp li xew mu guem te guemni mbeuguel daye faye
Yaye ki waral ba fepp fodem mu tokk te muñ te xar nga tew
Luko fi teye xana mbeuguel
Luko fi teye xana colore
Jegi nga guej gui bayiko guinaw
Mom dh joyna joy joy ba rangoñ ferr ayway
Beugnala muñal nala ki sa yaye dom la (×2)
Jegi nga guej gui bayiko guinaw
Mom dh joyna joy joy ba rangoñ ferr ayway
Sori ngalene ba fatei leine te lolu warula(×2)
Fi nga nekk sorina fatei leine warula
Tukki bayi guinaw njabot tokk dila xar (×3)
Jegi na guej gui bayiko guinaw
Mom dh joyna joy joy ba rangoñ ferr ayway

Don't want to see ads? Subscribe now

API Calls