Playing via Spotify Playing via YouTube
Skip to YouTube video

Loading player…

Scrobble from Spotify?

Connect your Spotify account to your Last.fm account and scrobble everything you listen to, from any Spotify app on any device or platform.

Connect to Spotify

Dismiss

A new version of Last.fm is available, to keep everything running smoothly, please reload the site.

Bandit - Lyrics

lou bandit di nirol
lou wara né jikom
waxma lou bandit di nirol
lane'mo
lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
lou wara né jikom
waxma lou bandit di nirol
lane'mo wara nékk jikom
wax ma loye def sa compte fess ak ay concer'ou huit clos
rappeur niom gni gui khoti texte ni secrétaire si bureau
profitéwoul bala DIP di nieuw
déy compliqué lolou gua lale fi million
mafi geuneu tchikili
bandit si son bandit si clip (hunh)
gaw ni lucky luke
balle si sa tank gua tchiriri
niari tank si birr piscine bi
miss chips dima pisss melni pitche yi (psss)
24H/ 24 tchi usine bi
mak Idy ak ISS music lucide sans wisky ak shit(hooouuuu)
fougn'la wo magui si biir té
fépp fougn ma wo yakk sa gars yeup si biti (oouuussss)
hééé
hééé
hééé
hééé
lou bandit di nirol
lou wara né jikom
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
lou wara jikom
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
(han) challenger
aythieu mbeur ioe la geum
bandit la mane non douma rappeur
ndanane la boy ni seu papeu
waxma lou bandit di nirol
sou boba ma wane lani
kani dou chewing-gum
boy bandit bandit'lou boul fi nieuw
wéyy na billy boy ak dém si yalla INO (bandit bandit)
fake nigga mousso ma nékh
fi dou tarr ba gua dégg wouye sama ndéye
métiwone'na mais niou geum ko rekk
ba téyy boy DIP mo geuneu siw monsieur le maire (hahahahahaa)
respect ni yéré bima soll
succès melni guél bima nopp
douniou yeukeuti lokho sakaw moukk classe
khana concert fi kénn démoul tableau(nio bégne)
hééé
hééé
hééé
hééé
lou bandit si nirol
lou wara nékk jikom
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di niroool (hé)
lou wara né jikom
waxma mou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
bandit dou réyy teud 10ans jale non!
business ba done milliardaire
yama makk mala meunn
lép mojji machalla
dama touli louf nékone adiak'diakk
kakatar laminn bou toll ni tiakaba
khadial ma dang mayy khadial maan
dagua thiangg yakk sa music bou khaniaral
bayi sa lokho pour diapp fann
douma tégui tank magui casamance
sama bakane la tekk boy ni mbacké mbacké
geumouma thiakhane'katt yi niodi gentleman
sheutt tey dji bandit yi laye wayale
wahou'makk boy yi dioudou beurki démb ndiaye
bandit la fils kone dérétt douma titt
bandit la mane si kébétoukatt yi
tekk si sadique ni kouy nane dérétou vampire
lou bandit di nirol
lou wara nékk jikom(hé)
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol (haaa)
lou wara nékk jikom(héhéhé)
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol (bandit- ba-bandit-ba)
lou wara nékk jikom(héhéhé hoo!)
waxma lou bandit di nirol
lane mo lane mo wara nékk jikom (hééé)
lou bandit di nirol (hé)
lou wara nékk jikom (hééé)
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
lou bandit di nirol (héhéé)
waxma lou bandit di nirol
lane mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
lou wara nékk jikom (hé)
waxma lou bandit di nirol
lane'mo lane'mo wara nékk jikom
lou bandit di nirol
(End)

Don't want to see ads? Subscribe now

API Calls